jeudi 22 mars 2007

Cheikh Ndiaye, diébalu


Sante Mawlana, Borom Assaman

Mome mignou bolèg Muhammadu sang bëppu jaman

Muhammadu Rassol borom xoutboki kêman

Kaddu djipp na, doy ngagnu royuway, saway geustul xourân,

Si walu wuné, moxam nassila ba lân

Bilay têrébi doyna kêman

Sou Lahou ahad digléwone, cone ma sax dila wo yê jah man

Cone diouli ak seulmal dayiman fiyak felè, ci sang bëppu man


2 commentaires:

Anonyme a dit…

khana tu es un rappeur converti?
by Ahmed.

Anonyme a dit…

wa salatu wa salaam ala sayidina Mouhamed wa ala alihi wa salim